Вы находитесь на странице: 1из 8

Lettre aux Croyantes

Jawbu Soxna Penda Diop


crit par Cheikh Ahmadou Bamba

LETTRE AUX CROYANTES


(Jawbu Sokhna Penda Diop) Ces importantes recommandations ont t adresses par Cheikh Ahmadou Bamba une de ses disciples du nom de Sokhna Penda Diop, femme dun de ses oncles paternels de surcrot. Dans cette missive fort clbre, connue sous le titre de Jawbu Sokhna Penda Diop , le Cheikh enjoint cette disciple, et par del elle, toutes les femmes mourides et toutes les musulmanes, ceci : 1. Je te recommande de pratiquer la patience et de persvrer dans la Crainte de ton Seigneur, en public et en priv ; ainsi obtiendras tu le Pardon de Dieu 2. Repens-toi constamment en Dieu et persvre toujours faire le bien ; ne te dtourne donc jamais vers autre chose que la droiture 3. Sois toujours humble et modeste, agis toujours dans la discrtion et vite dlever ta voix en parlant ; ainsi obtiendras-tu la Satisfaction Divine 4. Durant le restant de tes jours, ne te dirige plus jamais vers une quelconque chose dont le caractre licite en Islam nest point vident 5. Abstiens-toi strictement de tomber dans la mdisance et lorgueil ; persvre cultiver le silence et la patience

6. Evite le mensonge, lostentation de mme que le penchant pour la clbrit et les honneurs, garde-toi galement de tomber dans lautosatisfaction ou la haine envers tes semblables 7. Persiste toujours dans la sincrit et la puret de culte, persvre toujours assister et secourir tes prochains ; ainsi accderas-tu aux Faveurs de Dieu 8. Ne conois jamais lide dadorer ton Seigneur tout en refusant de te conformer aux recommandations de ton poux qui craint Dieu 9. Car, pour une femme, le Combat sur la Voie de Dieu consiste se conformer aux directives de son mari 4

10. Ainsi, chaque fois quun poux se montre satisfait du comportement de sa femme, le Seigneur se montrera galement Satisfait de celle-ci et lui accordera des Faveurs et des Dons 11. Mais chaque fois quun poux sera mcontent de lattitude de sa femme, que celle-ci sache que jamais son Seigneur ne lagrera 12. Sache ainsi que toute oeuvre accomplie pour une autre raison que la Face exclusive Dieu est totalement vaine et sans valeur

13. Sache enfin que nul ne pourra se sauver du Chtiment Divin lAu-del, sil ne parvient sabstenir de quatre pchs graves que sont : le mensonge, lorgueil, lavarice et le prjug ngatif systmatique [envers le Crateur et ses cratures]

Version wolof
Lii ab bataaxal la bu Sri Tuubaa masa bind benn taalibeem bu tudd Soxna Penda Joob, di soxna ci baayam bu ndaw. Ci biir ndenkaan bu am solo boobu, u gna xam ci Jawaabu Soxna Penda Joob , Sri baa ngi ciy digl lii soxna si, ak bepp soxnas murit, ak bepp jullit bu jigen : Man Sri Tuubaa miy jaam bu xeebu tey skkoo am ngrmal Ylla akug Yonentam, te di yaakaar ci oom u nangul ko ay jfm, maa ngi dnk lii Soxna Penda Joob, di samab taalibe, tey soxna ci sama baay tx. Ylla na u Ylla jggal te jggal ko, te boole u faral bepp bkkaar ak matadi. 1. Maa ngi lay digl yaw soxna si nga goor-goorlu ci mu ak ragal Ylla, sa Boroom, ci lu nbu ak lu fee ; soo ko defee dey Ylla di na la jggal lg 2. Na nga sax ci tuubal Ylla saa su nekk ak farlu ci def lu baax ; kon bul jngg mukk jm ci leneen ludul ag njub 3. Na nga sax ci nangoo weet ngir jaamu sa Boroom. Looy def dee ko def ci sutura te deel suufeel sa kddu saa yooy wax ; soo ko defee dey Ylla di na la grm 4. Yaw Soxna Penda, li la dese ci sa giirug dund, bul jogti mukk jm ci loo xam ne leeru la ne dagan na ci Lislaam 5. Deel moytu bu baax jw ak ry. Deel saxoo noppi ak mu. 6. Deel moytu bu baax wax lu amul ak ngistal wala bgga siiw. Na nga moytu naw sa jf wala di baanteek sa moroomi mbindef yi. 7. Na nga sax ci dggu ak sellal, deel farlu ci laabire aka dimbali jaam i ; soo ko defee dey suu Boroom di na la defal ay may aki jagle 8. Bul xalaat mukk topp sa Boroom ci lu andulak topp sa ndiglul boroom kr bu ragal Ylla boobu 9. Ndax xamal ne kat jihaadu soxna ci yoonu Ylla mooy mu farlu ci topp ndiglu boroom krm 6

10. Looloo waral saa yu boroom kr grmee soxnaam, sunu Boroom da na grm soxna soosu te di na ko defal ay xeewal 11. Waaye su fekkee boroom kr grmul soxnaam, soxna soosu na xam ne sunu Boroom du ko masa grm 12. Maa ngi lay xamal ne lepp lu nit mana def te jmmi Ylla rekk taxul, jfam jooju sanku na te pert na ko 13. Te na la woor ne, kenn du mana mucc lg ci mbuglum sunu Boroom lifeeg byyiwul eent mbir yii, te mooy : a. Wax ludul dgg b. Ry c. Nay ci sa alal d. aaw njort ci sa moroom ak ci sa Boroom Wa salaamu aleykum warahmatu Laahi wa Barakaatuhu

2014 - www.drouss.org - Tous droits rservs

Вам также может понравиться